Seneclic

🔴The Watiatia, sous couvre feu, au Royaume du Mbacke Baari

Par Amdy Barkham Sané

Mba jĂ mm ngeen yendoo waay

🚶🏾‍♂️🐕🐈
🔴Violation du couvre-feu: 80 personnes dĂ©fĂ©rĂ©es au parquet
🤔 Naniou dawal yeurmandĂ© aussi, dĂ«kk bi da metti de
🚶🏾‍♂️🐕🐈 La loi reste la loi quand mĂŞme
🔴Collecte pour SOD : Les 98 millions FCfa polluent le milieu estudiantin
🤔 walaay ndeysaan collecte ba parĂ© bĂ«gg ko def sa caisse tamitt cas la
Xana bala ngeen wax waxi xaliss boroom dem fajju ki ba werr
Ma saaga 🤔🤔
🔴CitĂ© millionnaire de Grand-Yoff : Une femme tuĂ©e Ă  coups de couteau par son mari
😞😞 ndeysaan reyna doomi jambur ni rek. Jabar boko mĂ«nalul dara dĂ©looko si ay mbokkam
Xanaa dingeen ma may saaga bi nak
🤷🏾‍♂️😭
🔴“Piscine Party”: Les deux personnes testĂ©es positives Ă  la Covid-19, sont les fils de Robert Sagna
🚶‍♂️🐈 bon wala leegi lerna
Bonne guĂ©rison 🙏🏾
🔴Covid-19 : Les SĂ©nĂ©galais seront vaccinĂ©s avant fin mars
💉💉 nioom daal faw niou pikiiir niou rek li mom esk jĂ mm la ??
Pikiir leen Macky ak njabootam ba noppi
Après ma xool ndax dinaa pikiirou
🚶🏾‍♂️🐕🐈 Burundi am na Covid19 ?
🔴Covid-19 / Almadies: Les restaurants ne mangent plus Ă  leur faim,
😞😞 ndeysaan khiiif dikkĂ«l naleen. Ak corona bi vraiment keen lekatul si resto yi. motah feepay meti
Maiga yi nak, mbaa nioom nice 😁🤔
🔴Nouveau “prophète” Ă  Kolda : Arrestation de Baba Malabe Mbackeroukhou pour dĂ©tournement de mineur
😁😁 mbadou prophete bi dey teuder ay mineur ?
SoudĂ© dĂ«gg la naniou castrĂ© 😁🤦🏾‍♂️
🔴Lutte contre la Covid-19 : Les agents de santĂ© des CollectivitĂ©s territoriales en grève. 🩺🩺 hayooo en pleine pandĂ©mie bou faj katt yi defĂ© grĂ©w dina metti dĂ©.
Personnel bi doyoul grève dissi tĂ©gou 🤦🏾‍♂️
🔴Serigne Abdoul Aziz Sy Djamil a Ă©tĂ© tuĂ© par son fils Ă  coups de couteau
😞😞 YĂ lla nako YĂ lla xaarĂ© aldiana firdawsi.
Doom ji yoon tek na si moom loxo
🚶🏾‍♂️🐕🐈 Sujet sensible
Takk Mask rek 😷 noppi
🔴Grave accident pour excès de vitesse : Un choc violent fait deux blessĂ©s Ă  Louga
😞😞 eywaay sunu mbokk chauffeur yi daw ndak dall ndank bokk
He Allah 😭🤦🏾‍♂️
🔴D. Boubacar tombe en Italie : Il faisait chanter sa victime en menaçant de publier ses photos intimes
😷😷 arroseur arrosĂ© ngay am noonu
Esk duniou bayi soutoureux diambour yiniouy use pour dileen chantage
Li niaaw na waay 🤦🏾‍♂️😡
Deux ans dont trois mois ferme de prison : Mère célibataire, K. Ndiaye avait commis un vol avec effraction aux Maristes
Mère luula ci duggal tamitt 🤔
Dumma ci débat
😷Takk Mask
🔴Escroquerie, usurpation de fonction : Alassane Thiaw se faisait passer pour le prĂ©fet ou le juge Babacar Ngom
😳😳 eupleuuww se faire passer pour un prefet nakk ndayamkoulanax MbackĂ©baarien mo dĂ«ggĂ«r nd** fitt 🤣
🚶🏾‍♂️🐕🐈
🔴Faux compte Facebook : Le ministère des Finances et du Budget alerte
Da jarr alerté.
Faux comptes yĂ gg nafi.
Ligeeyal Fall 😁😁
🔴Peuple de Mbacke Baari ici se terminent le Watiatia News du jour

Prenez soin de vous

YĂ lla na YĂ lla sĂ mm leen

🚶🏾‍♂️🐕🐈

Avatar

Presi Cisse

commenter

Pub

Restez connectés

Restez connectés

Ne ratez aucune nouvelle publication...

Seneclic

GRATUIT
VOIR