Seneclic

Ma jeunesse… 😭

Par Prési Cissé

 

Niom leu séne yaye di diay séni or pour niou touki afin qu’ils subviennent aux besoins de la famille une fois en Europe.

Jeunesse bi nioy Mafia bi, am diom, beugue téki. Jeunesse bou vulnérable bangui ni.
Jeunesse bi nioy kheuy sans orientation dans les universités
Jeunesse bi nioy sans formation yi
Jeunesse bi moy analphabètes yi
Jeunesse bi moy diplômés frustrés yi.
Jeunesse bi mo diapeu ni dafa rater Life am parce que def neu leep té téki woul.
Jeunesse bi moy majorité bi.
Jeunesse bi moy kheuy sans avoir de quoi manger.
Jeunesse bi leu séne yaye di cancer wala diabète niou setane ko bam dé. Dougn am lougn fayé soins wala dieunde garap.
Jeunesse bi leu séne yaye am bene table sandaga dissi diay bouy ak bissap, État bi nieuw todj ko.
Tout ça, devant le silence de l’autorité régalienne, manam État.

Je lis des matures intellectuels qui disent « Mais niom avec tout l’argent collecté pour voyager en pirogue, loutaax dougn si oubi business ? ».

Pensez-vous que votre capacité à mettre en place un projet ou un business est générale ?
Pensez-vous que l’État a préparé cette jeunesse à faire face au chômage et aux difficultés économiques ?
La formation est elle au point dans ce pays ?

Magoum dieum, am diabar ak dom, sou dieulé décision voyager en mer (connaissant tous les risques reek), c’est parce qu’il y’a problème.

Na État bi diog, diapalé jeunesse bi.

Mes condoléances aux familles des victimes décédées suite à l’explosion d’une pirogue qui partait pour l’Espagne en haute mer.

Sama gars yi, zéro khadi, dey nieuw si katanou yalla guinaw bi état bi créer les conditions pour cette jeunesse.

Avatar

Presi Cisse

commenter

Pub

Restez connectés

Restez connectés

Ne ratez aucune nouvelle publication...

Seneclic

GRATUIT
VOIR