Seneclic

Mansour Faye Vs Sonko

Par Prési Cissé

 

L’info pour les nuls.

Mansour Faye a dit publiquement que souko Ofnac wowé dou dém. Ofnac moy kourél guiy tiaytou leep louy guér (Corruption) ak yorinou alalou reew mi.

Donc naturellement Mansour sougn ko wowé, dafa wara dem, mais mouné sougn ko wowone dou dém. Suis certain que Macky Sall n’est pas fier de lui après cette mauvaise sortie.

Legui Sonko nakarlou mbiir bi. Sonko néneu tôt ou tard, keep kou yorone alalou reew mi, dinga rendre compte. Niko Macky défé wone ak PDS.

Sama mame néneu so khamoul loy tontou reek sossal. Mansour Faye sossal Sonko soss bou reuy, néneu Sonko dafko niane audience. Waxou kou dieul coup deugue 😂Mel ni Tyson biko Balla Gaye mboté mou soupou dialagne, après dem si arbitre bi nane danou woul.

Mansour nak danga danou nangou reek. Yalna Président kheuy reek dakeu leu😂

Ak lamine bou bar bi mouy mel ni Aissatou Diop Fall 😂

Avatar

Presi Cisse

commenter

Pub

Restez connectés

Restez connectés

Ne ratez aucune nouvelle publication...

Seneclic

GRATUIT
VOIR